Xale Bi lyrics Youssou N'dour parole
Fiche de Xale Bi Youssou N'dour lyrics
artiste
parole Xale Bi - Youssou N'dour lyrics
paroles officielles ♪ Xale Bi ♪
Non non non nonnnn
Non non non nonnnn

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo Ndaxté so mérééé, so mérééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)

Lou mounoul gnak faw dafaw am
wareef dafay mate
Lég Lég mou done lou doul neex
yaw sama dom
souba tax may waax
so magué di nga xaam

ndaxté so dioyééé, so dioyéé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma

wadiour ak dom
faw gnou y waxtane
féxé melni mbourok sow
ndem réro mouneta gnak
so Diaxléé, so diaxlééé
na sa khelmi dém
Dém ci say wadiour

Ni jamano mél
Tééy da cé baax
jubantil bamou thior
ndax momine dafay rooy
bissa ngui gnew
sou magué diarigne la
lép nga ci bami ndaw

Ndaxté so mérééé, so dioyééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma (boul ma méré)

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo

heuuuu xalé bi
né bougouma la merlooo
(xalé momine la yaw bouko merlo té dé ko bégueul)
Ndaxté so mérééé, so mérééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalma

Adouna nii la xalé bi lé
sou bay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
sou yay waxaté nga déglou ko
Adouna nii la xalé bi lé
(nangue ma deglo xel)
sou bay waxaté nga déglou ko
(bagn ma deglo xol)
Adouna nii la xalé bi lé
(samaaa dooooom)
sou yay waxaté nga déglou ko
(nangue ma deglo xel)

Né Xalé bii
Né beugoumala merloo

haaaann Xalé bii
Né beugoumala merloo

Xalé bii
Né beugoumala dioylooo
Ndaxté so mérééé, so dioyééé
Sama yaram daw, daw ba diaxalmaaaaaa

D.THIAM
Musixmatch.com
Droits paroles : paroles officielles sous licence MusiXmatch respectant le droit d'auteur.
Reproduction parole interdite sans autorisation. Lyrics powered by www.musixmatch.com
Commentaires
Postez une réaction pour Youssou N'dour - Xale Bi paroles
Nom/Pseudo
Commentaire
MP3 Télécharger sur iTunes
Youssou N'dour - Xale Bi parole
MP3 Télécharger sur iTunes
Autres paroles de Youssou N'dour
Kirikou
7 seconds (feat Neneh Cherry)
Bamba
New Africa
Immigres
Birima
Wiri - wiri
Song Daan
Plus Fort
Ligueye
Sama Guent Guii
Boul Bayékou
Amitié
Leaving (Dem)
7 Seconds
Mbeggeel Noonu la (Because Love's Like That) [L'amour en est ainsi]
This Dream
Li ma weesu
Country Boy
Africa Dream
L'enfant nu l'enfant noir
Lang
Medina
Beugue Dou Bagne
Undecided (Japoulo)
Chimes of Freedom
Africa Dream Again
Dem
So Many Men (avec Pascal Obispo)
À découvrir...
Artistes et paroles : sélection aléatoire parmi les artistes et lyrics du moment
Barbara | Dalida | Céline Dion | Jean-Jacques Goldman | Serge Gainsbourg | Disney | Claude François | Françoise Hardy | Kyo | Roméo Et Juliette | Camille | Nana Mouskouri | Grégoire | Yves Montand | Ben E King | Maitre Gims | Jacques Dutronc | Eminem | Rammstein | Danakil | Henri Dès | Toto Cutugno | Les Mystérieuses Cités D'Or | Graeme Allwright | Max Boublil

La Salsa Du Démon | Les Champs-Elysées | Eins, Zwei, Polizei | L'été Indien | Je Deteste Ma Vie | La Liste | Take Me Home Country Roads | Zombie | Je Lève Mon Verre | Mad World | Puisque Tu Pars | L'amour Fou | Hey DJ | When I Look At You | Déchiré | Cap Diamant | Mieux Loin De Moi | Promenade Sur Mars | L'enfance | Ensorcelée | L'Everest | Dime | Le Premier Bonheur Du Jour | Le Balcon | C'est Ma Vie
Problème de connexion ?
Ouvrir un compte (gratuit)
Sélectionnez dans l'ordre suivant :
1| symbole à droite du smiley
2| symbole en bas de la loupe
3| symbole en haut de l'enveloppe
grid grid grid
grid grid grid
grid grid grid