Adiouza Cey Love song lyrics
Cey Love Adiouza lyrics sheet
artist
Cey Love - Adiouza lyrics
♪ Cey Love ♪ official lyrics
Mane la beugue
Mane la Guiss
Man Rék dou Kénéne
Défale ma louné
Wane ma Louné
Yobou ma founé
Meussou ma Sorri
Souma amé Naxar
mou dima yokou yakaar
Daf maye diégué
Souma Tissé mou dima deufeul
Té xamoul né sama xol Kénénne na fa fess
Nane la kokoye waxé

Défouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul Tonioula
Té xamoul né sama xol Kénénne na fa fess
Nane la kokoye waxé
Défouma loutax
Waxouma louko diar
Tassoul Tonioula
Oh Oh nane la kokoye wahé
Oh Oh Té doumako Gagne
Oh Oh nane la kokoye wahé
Oh Oh Té doumako Gagne

Xamna Lovame ak yénéne
Fimou tolou tchi mane

Motah ma wara sincére, wah ko deugue, nit kou bakh laa
Souma sanione sama love dafaye law ba faw
Tayoumako, Souma nékék mome, Kénéne laye halat
Té xamoul né sama xol Kénénne na fa fess
Nane la kokoye waxé
Défouma loutax
Waxouma louko diar

Tassoul Tonioula
Té xamoul né sama xol Kénénne na fa fess

Nane la kokoye waxé
Défouma loutax

Waxouma louko diar

Tassoul Tonioula
Oh Oh nane la kokoye wah
Oh Oh Té doumako Gagne
Oh Oh nane la kokoye wah
Oh Oh Té doumako Gagne
oh Balma... oh Balma
Nane lakokoye wahé... Nane lakokoye
wahé
Té douma ko Gaagne
Tissnama baby forgive me
Mane tayouma lima dal,
Mbeuguel boula Songué meune la
Yow Balma
Ni Mbeuguel loye faléwoul sa héte
Dou Mbeur momou niouy dane
Ni Mbeuguel loye foume la fék meune laye
Dalay Yobou Ardo
Kasssss nane laye déf
Cey Love
Li kou ko xamoul dala daloul Cey Love ×5
Musixmatch.com
Lyrics copyright : legal lyrics licensed by MusiXmatch.
No unauthorized reproduction of lyric. Lyrics powered by www.musixmatch.com
Comments
Leave a comment for Adiouza - Cey Love lyrics
Name/Nickname
Comment
Adiouza - Cey Love song lyrics
Other Adiouza song lyrics
Ma la nob
Mbeuguel ( T'en Vas Pas )
7 à 77ans
Daddy
I Love Someone Else
Borom Gal
To see also...
Artists and lyrics : Random selection of top song lyrics and artists
Le Bossu De Notre Dame | Charles Aznavour | Saez | Serge Gainsbourg | Dalida | Bob L'éponge | Bryan Adams | Cendrillon | La Reine Des Neiges | Chansons Populaires | Choum | Violetta | Chantal Goya | Hercule (Disney) | Hugues Aufray | Henri Dès | Blanche Neige Et Les Sept Nains | Mireille Mathieu | Phoebe Buffay | Bonnie Tyler | André Claveau | Richard Cocciante | Donjon De Naheulbeuk | Princess Sarah | Frère Des Ours

Moi a Mon Bisounours | Belle | Caresse Sur L'océan | L'italiano | Etre Un Homme Comme Vous | A Ma Place (avec Axel Bauer) | Partenaire Particulier | Générique Saison 1 | Que Sais Tu De Moi | I'm Yours | Somewhere Over The Rainbow | Manman Di Mwen | Flou De Toi | Je N'suis Pas Bien Portant | Nantes | Tout Le Monde | Et Si | Nan ? ... Si ? | On Ne Verra Jamais | If I Were a Boy | Le Petit Pain Au Chocolat | A La Claire Fontaine | Le Miaulement Du Chat | Doux Rossignol | Mas Que Nada
Forgot your password ?
Create an account (free)
Select in the following order :
1| symbol to the right of magnifying glass
2| symbol to the right of the bulb
3| symbol to the left of the calculator
grid grid grid
grid grid grid
grid grid grid