Beugue Dou Bagne lyrics officiel
Fiche de Beugue Dou Bagne Youssou N'Dour
artiste
parole Beugue Dou Bagne - Youssou N'Dour lyrics
paroles officielles ♪ Beugue Dou Bagne ♪
Couple bi
Maye dadiéle soumaye dokhanetou dji
Foléne séne
Gnoungui défe bras dessus bras dessous
Bataye gnoungui ni dôniye make, di
Geu-neu begeunté
Mbeugéle rékka wor
Mbeuguéle, mbeguéle rékka nekhe
Taye gnoungui ni di tôgnanté
Di kalanté, melniye dômi badiéne
Léke léke gnou méro ba kouné khole guéthie
Nga guéssouwaté sénate léne gnouye
Wakhtane
Oh mbeguéle, mbeguéla nekhe
Gueume léne ni, mbeguéle, rékka wor
Han…. oooh
Bagnou dôné gouné
Thi lagne khamanté wône
Bagnou dôné ay ndawe
Thi lagne begueuneté wône
Bataye gnoungui ni, dôniye make
Digueu-neu begueuneté
Mbeguéla wor
Mbeguéle, mbeguéle rékka nékhe
Sô dokhé ba séne kéne thi gnôme gnare
Tôgale khare, légui kénéne ki gneuwe
Dara gueunoule nekhe
Mbeguéle gou sincére
Gôgou mbeguéle
Kéne dou thi meune dara
Oh mbeguéle, mbeguéla nékhe
Gueume léne ni mbeguéle rékka wor
Han... oooh
Mane beugue nâla, mâla rawe menou kô faye
Wouy mbeguéle, wouy mbeguéle, wouy Guise beugue yalla mo
koye défe wouy
Mbeguéle, wouy mbeguéle wouy
Mbeguéle, wouy mbeguélo
Beugue na beguetouma, bôba mbeguéle
Ga dafa dess
Mbeguéle bou diogué thi khole, délou Fa laye desse
abadâan
Mbeguéle kéne meunou ko diaye
Té kéne menou kô dieunde thia marsé ba Défe thia
yeurmandé
Marie ak Cheikh Marie (choeurs)
Beuguéneté naniou, Amar
Xamanté naniou bou yague
Beuguéneté naniou
Xamanté bou yague, Amar
Minanté naniou, Amar
Haan beugueunté naniou
Mbeguéle kene douko diaye
Mbeuguéle amoul religion
Mbeuguéle amoul niit kou nioul
Ak niit kou wekh
Edit by Lamine
Musixmatch.com
Droits paroles : paroles officielles sous licence MusiXmatch respectant le droit d'auteur.
Reproduction parole interdite sans autorisation. Writer(s): GUEYE MOUHAMADOU, NDOUR YOUSSOU, CALO' MASSIMILIANO Lyrics powered by www.musixmatch.com
Commentaires
Postez une réaction pour Youssou N'Dour - Beugue Dou Bagne paroles
Nom/Pseudo
Commentaire
parole Youssou N'Dour - Beugue Dou Bagne officiel
Autres paroles de Youssou N'Dour
Kirikou
7 seconds (feat Neneh Cherry)
New Africa
Kirikou Et La Sorcière
Chimes of Freedom
Wiri - wiri
Leaving (Dem)
Plus Fort
Song Daan
Boul Bayékou
Immigres
Sabar
Undecided (Japoulo)
Be careful
Yama
Xale Bi
Bekoor
Ligueye
Xaley Rewmi
No More
Birima
Lang
Miss
Africa Dream
Taaw
Kirikou (version instrumentale)
Li ma weesu (Comme dans un miroir)
Sama Guent Guii
Il n'y a pas d'amour heureux (There Is No Happy Love)
Exodus
Badou
Liggeey
Bamako
Bamba
Hey You
Don't Walk Away (feat. Morgan Heritage)
Set (Live)
Survie
Diarr Diarr
Yaru (The Makings of Respect) [L'étoffe du respect]
Bololene
Toxiques
Birima (Roots Remix)
Shaking the Tree
Country Boy
Bes
Africa Dream Again
Medina
My Hope Is In You
Hope
Seven Seconds (feat. Neneh Cherry)
Kocc Barma
Téléphone
So Many Men (avec Pascal Obispo)
Dem
À découvrir...
Artistes et paroles : sélection aléatoire parmi les artistes et lyrics du moment
Joe Dassin | Aladdin | Dalida | Barbara | Roméo Et Juliette | Johnny Hallyday | Saez | Generique TV | Jean-Jacques Goldman | Les Colocs | Les Inconnus | Tino Rossi | Walt Disney | La Compagnie Créole | Toto Cutugno | Henri Dès | Richard Cocciante | Tryo | Lucky Dube | Véronique Sanson | Lynda Lemay | Grease | Françoise Hardy | Ghost (the Movie) | La Chicane

Je Ne Veux Pas Travailler | Je Veux Tout | La Patate | Je Veux Savoir | C'est La Fête | Joyeux Anniversaire | Place Des Grands Hommes | Libérée, Délivrée | Juste Une P'tite Nuite | Bewafa | Je Lève Mon Verre | She's Like The Wind | Où êtes-vous ? | De Zéro En Héros | Souffrir Par Toi N'est Pas Souffrir | Inch' Allah | Rien À Remplacer | Top Back (Remix Feat.Young Jeezy, Young Dro, Big Kuntry & B.G.) | Tout Ce Temps Qui Passe | L'horizon | Je L'aime à Mourir | Je Voudrai Deja Etre Roi | Roméo Kiffe Juliette | Pepsi New Generation | Voici Les Cles
Problème de connexion ?
Ouvrir un compte (gratuit)
Sélectionnez dans l'ordre suivant :
1| symbole à droite du coeur
2| symbole à droite de la croix
3| symbole en bas de la valise
grid grid grid
grid grid grid
grid grid grid