Chimes of Freedom lyrics officiel
Fiche de Chimes of Freedom Youssou N'Dour
artiste
parole Chimes of Freedom - Youssou N'Dour lyrics
paroles officielles ♪ Chimes of Freedom ♪
Si diguenté marakh massé
bi diololi suuf sédé
si lagn gawantou fatu mingui done gara
ni bi diololi you tedd si melakh yi kawélakh
yenene you melni you done rire nguir liberté
di riir ngur diambar yi donne khekh té bal takoul
di riir nguir gni done gadaay ci yon you meti yi
aki tamit kep kho khamni soldar nga bou toumouranké si
goudi gui
And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

si bene mbar si deuk bi gni ngui lakhatou wone di khol binga
khamanténi mbir yangui done wagnékou
bi diololi yi nek khew di riir ci taw bi ngelaw youdoul
diolol you lerr nek ci kaw di tabi
aanhh di riir nguir di bagne, di yeungou nguir ki loff
di yengou nguir ki niak chance gni gnou faté gni gnou wor
di yengou nguir gni gnou bedi yagg ko lakh mouy doundé
And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

si bi dalouk doy warr bi dondiou glace you gnang rott
di khoti diaou dji di setou wer ak sell
wayam you clochou eglise yi di sani fo soré soré ak
nguelaw li
desatoul loudoul diolol you nekoul ca rak bi
anh di riir ki labiir di riir nguir ki bakh
di riir nguir gni gniy gadi ak kiy samm sunu tour
ak natal kate bi kene guissoul fou soré soré si diamonom
And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

si goudi you bari kemtane yi
taw bi melni li louy ler té ay takander you amoul forme té
toumouranké
di wakh guir lamigne yi mounoula wakh sene khalatt
té ay khalat yo khamné fogone nagne ni né khamou gnou
lene
di wakh nguir silmakha yek gni teukh
di wakh nguir gni lou gniy nato jieggen youniouy nakh
ak gni gnouye toudé thiaga
di wakh nguir say say niou guené mou daw ba rer
And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

yi dem ba bene nir ci assamane si naw di tour ndokh ndank
ndak té le
lérayou lamp yi di gnou dal mel ni fitt wou dioubel si
gni natt gni gnouy werr té khamou niou founiou né thi
dounya
aanh di riir ngui gni wadiou sén si yone you meti yi
di riir nguir gni beugeunté té mounou nio wakh sene metite
di riir ngui yaram you niou teuj si casso té defou niou
dara
And we gazed upon the Chimes Of Freedom flashing

nagnou khol lérayou liy rir nguir liberté
Musixmatch.com
Droits paroles : paroles officielles sous licence MusiXmatch respectant le droit d'auteur.
Reproduction parole interdite sans autorisation. Writer(s): Bob Dylan Lyrics powered by www.musixmatch.com
Commentaires
Postez une réaction pour Youssou N'Dour - Chimes of Freedom paroles
Nom/Pseudo
Commentaire
parole Youssou N'Dour - Chimes of Freedom officiel
Autres paroles de Youssou N'Dour
Kirikou
Kirikou Et La Sorcière
New Africa
7 seconds (feat Neneh Cherry)
Leaving (Dem)
Téléphone
Wiri - wiri
Undecided (Japoulo)
Song Daan
Sama Guent Guii
Beugue Dou Bagne
Plus Fort
Bekoor
Ligueye
No More
Amitié
Xale Bi
Live Television
Badou
Boul Bayékou
Africa Dream
Medina
Kocc Barma
Yama
My People (Samay nit)
Li ma weesu
Lang
Please Wait
Birima
Miss
7 Seconds
Be careful
Bamba
She Doesn't Need to Fall
Bamako
Yaru (The Makings of Respect)
Africa Dream Again
Hope
Don't Walk Away (feat. Morgan Heritage)
This Dream
Borom Gaal
Survie
My People
Bull Ko Door
Ay Chono La
Kirikou (version instrumentale)
Marley - Radio Edit
So Many Men (avec Pascal Obispo)
Dem
Il n'y a pas d'amour heureux (There Is No Happy Love)
Létt Ma
Exodus
Food For All
Seven Seconds (feat. Neneh Cherry)
À découvrir...
Artistes et paroles : sélection aléatoire parmi les artistes et lyrics du moment
Aladdin | Generique TV | Patrick Bruel | Joe Dassin | Pokemon | Notre-dame De Paris | Bob L'éponge | La Petite Sirène | Hercule (Disney) | Les Choristes | Astérix | Tino Rossi | Anastasia | Isabelle Pierre | Grease | Jacques Douai | Pink Floyd | Pink Martini | Raiponce | Don Juan | Danakil | Justin Bieber | Graeme Allwright | Enrique Iglesias | Richard Anthony

Mulan - Comme Un Homme | Partir Là-bas | Loin Du Froid De Décembre | Caresse Sur L'océan | Respect | Auteuil, Neuilly, Passy | San Francisco | Only You | Relax, Don't Do It | Podemos | Tous Les Visages De L'amour | I Love You Baby | Charmed | La Transhumance | Ya Nabi Salam Alayka | Si C'était Le Dernier | J'en Ai Rien à Foutre | If I Needed You | Merde In France | Jules César | Mexico | Pokemon Saison 2 | Je Reviens Chez Nous | Il Suffirait De Presque Rien | Favorite Girl
Problème de connexion ?
Ouvrir un compte (gratuit)
Sélectionnez dans l'ordre suivant :
1| symbole à droite de la maison
2| symbole à gauche de l'ampoule
3| symbole en bas du cadenas
grid grid grid
grid grid grid
grid grid grid